Channel Banner
Channel Avatar

Bànqaasu xam-xam

🇸🇳 Senegal

@banqaasuxamxam

Subscribers

6,640

Total Views

91,834

Video Count

32

Creation Date

2017-09-15

Channel Description

Dalleen ak jàmm ci xëtu Yutub bii di Bànqaasu xam-xam Bànqaasu xam-xam di xët wow jàngale xam-xam ci fan yu wuute moo ko tax a jóg jaarale ko ci làkkuw Wolof . Xam binu xam ni am réew manuta suqaliku ak am um yokkute ndeem moo ngi wékku ci am réew ni moom.Mépp réew ci saw làkk ak sam mbatiit nga man sukkandiku ngir man a jëm kanam . Xam luni mel moo waral Bànqaasu xam-xam tànn làkk wi gën a yaatu ci réew mi te ëpp ñi koy jëfandikoo aka dawal ngir jàllale xam-xam yi. Fànn yi nuy fésal ci xët bi bokk na ci xam-xamu : Xewxam ; Dund ak suuf ( tàmbali bi jëm ci dongo yi nekk ci joŋante BFEM ) ; mbëj ;Xarala ; Ci ay fan yu néew, dinanu andi yeneeni jàngale yu yees. Bànqaasu xam-xam moo ngi leen di Jaajëfal di bég ci tasaare njàng mi ak toppu bi. Jaajëfal Itam Block Business, jëf, Jang Wolof ak jàngalekat yi 🔘 xët wii di bànqaasu xam-xam moy télé bi ñëkka déf ay video jangalé xam-xamu science ak technologie ci wolof.

Keywords

technologie dessin industriel electrotechnique electricite mecanique mecanique automobile automobile wolof svt science de la vie et de la terre science vie Histoire Afrique africain negre noire culture origine langue Cheikh anta diop thomas sankara Martin luther king kwame nkrumah sekou toure nelson mandel amadou toumani toure ghana senegal burkina faso guinée mali rwanda nigeria cote d’ivoire malcom x kadhafi civilisation humanité génocide pauvreté economie wolof